musicas.mus.br
Letras de músicas - letra de música - letra da música - letras e cifras - letras traduzidas - letra traduzida - lyrics - paroles - lyric - canciones - JëLI (FEAT. AMADEUS) - WALLY B. SECK - música e letra
Utilize o abecedário abaixo para abrir as páginas de letras dos artistas
Jëli (feat. Amadeus) letra
Boo ma beddiwul xalaatuma la bàyyi
Awma làmmiñ soon tudduma lambay yoy
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (eeh yoo)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (man ma)
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (daadi sama waay)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (danga di sama waay)
Bala ma jog
Fajar fekk nga dem jaayooy
Bale kër gi raxas say ndap
Ndekke boobu dam ngay wajal
Dundu maata ñaan nooy
Ndaxte gaynde dama koy jur
Ndax fitna loo ma
Xëboo li ma lay jox
Lépp loo ma ñaan dinaa la may
Dootuma def leen lu lay metti sama ndaw si
Ndax sama nawle nga doo leeral sama yoon wi
Dootuma nangu mindéef di dox sama digu ak yaw
Ndax Yàlla moo def ci ñun lay ñu wëy nak
Kaay waay!
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (eeh yoo)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (man ma)
Dootuma wiri wiri njari ndari
Li ma moom lay jëli (daadi sama waay)
Dootuma yonni kenn ci sama waa ji
Man mi maa koy jëli (danga di sama waay)
Gaañ la taxul nga ba
Tooñ la taxul nga may rëccooy
Salaw yenn saay nga mer
Sama jaambaar ci yaw mi la wékooy
Eee waay
Sama jaam, sama waay
Eh waay wow
Sama jaam, sama waay
Wally B. Seck - Letras
- Alhamdou Lilah (feat. Sidiki Diabaté)
- Assurance (feat. Sidiki Diabaté)
- Bad Man
- Balma
- Cherche En Toi
- Choco Vanille (feat. Ndiolè Tall)
- Choix (feat. Mia Guisse)
- Confuse (feat. Mia Guisse & Amadeus)
- Dafmay Dal (feat. Le Raam Daan)
- Dawuma Dara (feat. Samba Peuzzi)
- Derangé
- Désolé (feat. Le Raam Daan)
- Diégué Kiraay
- Djery Ngoné
- Djiguene
- Don't Be Afraid
- Don't Leave Me Alone (feat. Marco Alexander)
- Donne moi une chance
- Entre Nous
- Feccal Ma
- Henne Time (feat. Ndiolè Tall)
- Hey Ya
- Hymne Faramareen
- Immigrés
- Jëli (feat. Amadeus)
- Lo Beugue
- Loving You
- Mame Boye
- Mirna (feat. Le Raam Daan)
- Mon Choix
- Mon Combat
- Natural Love
- Nila (feat. Akhlou Brick)
- Nila (feat. Akhlou Brick)
- ON IT
- Only Love (feat. Fata)
- Paradise
- Reguine Tass (feat. Viviane Chidid)
- Runaway
- Si Vous Saviez
- Stay
- Thieuguine
- Togn Ngama
- Venise
- WURUS (Version Afro)
- WURUS (Version Mbalax)
- Xarma
- YA TAY (feat. Baye Mass)
- Yaa Meune (feat. VJ)
- Yeye (DIAGA)
- Yobaneté (feat. Le Raam Daan)
top 30 músicas
©2003 - 2026 - musicas.mus.br